Nouvel Album sur Macky Sall: Xew Xewi Mi, Mackil Na Rewmi – Ak macky Sall Thiono Rekkk

Réwmou mackiiiiiiiiMacky Sall SingleNouvel Album sur Macky Sall: Xew Xewi Mi, Mackil Na Rewmi – Ak macky Sall Thiono Rekkk

Réwmi ma wakh lén li khéw ci rewmi, mackil na réwmi, ta sonnal na réwmi.
Li gueun ci réwmi, nga diokh français yi,
Lidess nga paachook gassama, faye, sall.
Li baakh ci rewmi nga diokh ko thimbo, di kholé nim loo, yakh nga rewmi.
Dougoub dji cher na, té Tchébi cher na, sukar si cher na, dound bi rare na
Essence bi cher na, té méwmi cher na, lécole bi cher, garab yi cher nagn,
Kasso yi féss nagn, almère yi féss nagn, ta guédji fess nak sougn néwi doom yi.
Leudial nga réwmi, fateu nga gor gni, nargan baykat yi, keur yép tass nagn.
Chômeurs yi yokou, malades yi yokou, sa ay gui nékhoul, djigo fi réwmi…

Related Posts

URL courte: http://www.sunuker.com/?p=41675

Répondre

Campagne de collecte de fonds: Supportez votre radio Sunuker FM: La Première Radio Africaine en Californie – Faites un Don – Merci

Le Blog de Jawar Jobe. Tous les Vendredi, votre chronique Hebdomadaire. Par N’diawar Diop

Ndiawar Diop gros plan

Le Blog de Ahamdou Diop

Télécharger Sunuker Fm iOS APP et Sunuker Fm Android App sur votre tablette Androïd et sur votre iPhone ! C’est Gratuit !!!

Sunukerfm App Android

Emissions « Voix/voie des Jeunes » Les Dimanches @ 17hr GMT en DIRECT

vdj

Emissions « Xew Xewi Rewmi » Les Mardis @ 19hr GMT en Direct

Galerie photo

SUNUKER.COM Copyright 2013 .