Humour: Les Délires « Ramadaniques » du Chroniqueur Seydina Seck

 

Les Délires Chroniqueur Seydina SeckGuinaw bima santé Yalla, Djouli thi Yonentbi, Sant samay wadiour, KOOR gui damako yag paré Becaye!

Lima entrainé khadioul thi mom….

Mangui sante NELAWdiko guereum daf may conseillé dima dalal bou bakh!

Di sante NDOGOU dafa soneu thi mane: niom PainSaucissonCamembertTandarma… kou liim dioum, Bécaye!  Amouma séne faye!

Dama fatéwone KHEUD, mom tamite diap na si combat WEROU KOOR bi bou baakh!

Dilene Sant Dilene Guereum!

WaSalam!*

Humour: Propos Extraits sur sa page facebook
Les Diawenne et les gueyennes attaquaient!!!

Extrait sur le mur de Seydina Seck

Par N’diawar Diop Sunuker.com

 

Be the first to comment

Leave a Reply

Your email address will not be published.


*