Journal Rappé EP 21 avec Xuman et Keyti – Guest Stars Duggy T & Awadi

Journal Rappé EP 21 avec Xuman et KeytiJournal Rappé EP 21 avec Xuman et Keyti – Guest Stars Duggy T & Awadi

Lyrics JTR 21 ft Awadi & Duggy Tee

XUMAN
Chaque année des inondations! Ça ressemble à la longue
au refrain d’une vielle chanson. Pour certaines populations
la pluie est une malédiction qui continue quand s’éloignent
les caméras de télévision.

AWADI
On prend les mêmes on recommence
de toute façon c’est pire qu’avant.
On attendait des solutions
pour le moment on voit du vent.
On attendait des logements, des recasements,
ce qu’on voit c’est des pansements
alors on souffre sagement…

XUMAN
C’est toujours les mêmes plaignants
qui se plaignent au même moment
et toujours les mêmes endroits inondés
abondamment . Il y a eu des téléthons,
les artistes ont fait des chansons,
on a récolté des dons,
on a même collecté des fonds
mais…

AWADI
Tu pensais quoi? Que le temps change avec une élection?
Que les gens changent avec une sélection?
Y a rien qui change, on remet les mêmes comportements.
Je suis déçu proprement,je l’exprime fortement.

XUMAN
Tous les regards sont tournés sur la poudrière du monde
au Proche-Orient où la Syrie est assise sur une bombe.
Concertations, discussions et négociations pour légitimer une guerre.
Il faut créer une coalition. Awadi ?

AWADI
Les yeux rivés sur l’écran je guette la série.
Le feuilleton du jour c’est Obama, la France et la Syrie.
Les salauds s’organisent et veulent du sang,
c’est des tracasseries.
Bachar les fait chier mais Poutine leur fait des vacheries !
Encore une fois ils veulent nous faire bouffer des conneries
et même sans les preuves ils vont déployer les batteries.
Hollande n’a pas la côte alors une guerre serait la bienvenue.
Ça fait bizarre mais j’ai un sentiment de déjà vu,
Wade a fait le sale boulot, la France en fait son alibi.
Khadaffi est mort, Sarkozy a brisé la Libye.
Partout des gens qui prient «On veut la paix pas la guerre !»
Pendant que le Pape il veut la paix Macky soutient la guerre.

XUMAN
Explique! Quelle serait ta politique
Awadi Ministre de la Culture de le république ?

AWADI

Pfff… Ministre moi? Jamais de la vie. Peut-être Président d’Afrique,
Ministre jamais de la vie ! Ministre sans budget à la culture
jamais de la vie ! Je préfère rester vrai dans mon son toute ma vie.
Je suis trop impertinent je ferai rien de pertinent,
si je me bats c’est pour une cause qui va servir tout le continent.

XUMAN
Merci Awadi! Société pour finir: les hommes de nos jours s’habillent
comme pour se punir avec des pantalons tellement slim
qu’il faut de l’aide pour les mettre. Body rose, près-du-corps,
des hommes habillés en fillettes. Quand aux filles pour sortir
elles se déshabillent. Grosso modo les jeunes sont
comme un panneau publicitaire: tout ce qui et nouveau n’est pas beau,
publicité mensongère !

KEYTI
Beneen bes yeneen xibaar tayitam niou dalal gan
Ni gnéneen gni fi diar momitam indil niou lane?
Sounou laatch bi dieuk nak dou am diad-diadal,
dieum tchi mbënd mi, lou takh ngour gui incapable?

DUGGY
Un Peuple, un But, une Foi manam sounou Nation
meunteu fekhé nek beneu, dieulééfi yi inondations.
Arbiss, sibirook choléra di bégué ndakh pollutions,
Keur yiy mabb, nit gni féébar lane mo di seni solutions ?
Ya dèfoone mo geune fouf ya niwoone
Yangui randal wayé amoulo ndeyssanou Yadikone!
Bess bou né nit yi di dioy ba amatouniou sakh rangogn,
sans domicile leu tambeuléwoon daldi moudié sans kogn !
Bayilen tiakhane bi té yeureum askan wi,
digué bor la kone fékhéleen samm bakane yi
ndakh dou dédommagement moy liy tegui nakhar wi.
Nieupeu merr dieulé ko Tamba ba fi si Dakar mi.
Yi khéétou fitna nioy yokk diafé-diafé,
deuk bi tiit na, kone bou leen ko taf-taféé,
méti na, tiis na, doy na war, dou louniouy kaféé,
ngour gui sigui leen ndakh fi mouy météé ngeen di waafé.
Nianouniou deuk si sauwétass ak niomine téléthon,
gnii di politique, gnéé di poukeuré diapé nitt yi con.
Wooté budget bou takkou té ligueey mo geune feulék dons.
Da melni lou nit yi di geuneu sonn ngeen naan “C’est le bon” !

KEYTI
Lolou leer na! Meunou niou deuk at mou diot ci fitneu.
Gni né ci ndokh mii di khouss doundéwouniou ngour gui dik neu.
Sama niarel laatch Duggy dieum ci culture bi di raam.
So newoon ministre de la culture tay louy doon sa porogramme?

DUGGY
Sou Culture nekoone sa ma Ministère mboukhoum dou fi am
palass té mbir yi daniou geuneu leer. Joumtouway daniou sakh,
droits d’auteurs yi daniou diakh, cinémas yi daldi tàkk ba
takh keneu dotoul merr.

KEYTI
Waw mais artistes yi tay ndax am nagn lou leen di aar?
Ndax gis nagn fi gnénn ci niom ni niou moudjé doy waar.

DUGGY
Done artiste ba kheuy doon makk wayé amoulo lo doundé,
fagaroo geune fadiou ndakh benn pension dou la goungué

KEYTI
Laatch bi moudj Moussé Duggy Tee di mbiroum Syrie,
Bassar El Assad mi nasaraan si beug katchiri.
Buñu fataliko niniou tapaléé ba song Irak tay
ndakh dou interêts yawoon nio leen ci khiiraat.

DUGGY
Leu tchi Syrie diar ni wiri donté meunouniouko firi.
Wiri wiri diari ndaary ndakh bombes yaleen iri
Bachar newoul si deug ap toumal leu wala geudd
Lign koy téré nionko yoré kan si niom gni mo niou nara feug.
Iran, Iraq beu Israel dieum Palestine. Ana gni len diay nganay
faté Yalla mi leen tiim ? Tey dji niom gno dadialo
di out ni niouy len fekhéélé. Sougn paré si niom mba dou
nioun la niouy nieuw dogeulé

KEYTI
Diadieuf Duggy! Wallou tcholine nak mo moudj,
kheetou mbubbeuk toubeuy you khat yi khalé khéwal
Sol ko mouné niapp melni louniou bagna toud.
Goor yalla yi daan bagn dangal, leggi nio koy séwal.
Toubeuy you roses, vertes, you zaunes toudé ko pinw!
Laadjal Waly mou wakhla lolou yeup c’est le winw!
Dés na touti nak goor ak jigeen diafé ragnéé.
Ndakh lépp liniou wuteuléwoon gni ngui woute nougn ko wagné.

Be the first to comment

Leave a Reply

Your email address will not be published.


*